Librería Samer Atenea
Librería Aciertas (Toledo)
Kálamo Books
Librería Perelló (Valencia)
Librería Elías (Asturias)
Donde los libros
Librería Kolima (Madrid)
Librería Proteo (Málaga)
Waa so mënon delloo ay waxtu walla ay at ci ganaw? Ak téeré bi, ma ngi lë woo ci ngë dellu ci dëmb ndax ngë xam sa ndono ni mu réyé. Buur bu goor ak bu jigéen, njitt dëkk ya won ak jambaar yu goor ak yujigéen, defaral sa toggay te ngë gëstu(jàngat) Jëfin ak kawtefu 4 kangam dëmb yi ci Afrik. Ci jeexantal téeré bi, ab pàcc laa ñu la jagglel ngir ngë tekk ay kuloor ci nitaal yi lolu dina tax ngë bokk ci léeb bi ci wetu jambaar yi. Mbaa pare ngë ?